2 Kings 1:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne ko genn góor a leen dogale, ne leen ñu dellu ci buur bi leen yónni, te wax ko ne ko: «Aji Sax ji nee: Ndax Yàlla daa amul Israyil ba ngay yónnee di seetluji ca Baal Sebub, tuuru Ekkron? Loolu tax na lal bi nga tëdd doo ko wàcc, ndax dinga dee moos.»