2 Kings 10:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca jamono jooja nag la Aji Sax ji tàmbalee fell suufas Israyil, Asayel buurub Siri di leen duma ca réew ma mépp.