2 Kings 10:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu lañu ñàkke fa féete dexu Yurdan penku dale ca diiwaanu Galàdd bépp, boole ca suufas waa Gàdd ak waa Ruben ak waa Manase. Mooy la tàmbalee dëkk ba ñuy wax Arower ca kaw dexu Arnon ba ca diiwaanu Galàdd ak Basan.