2 Kings 10:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ka yilif kër buur ak ka yilif dëkk baak mag ñaak dag ya yónnee ca Yewu, ne ko: «Nun say surga lanu, lépp loo nu wax dinanu ko def. Dunu fal kenn buur. Loo def baax na.»