2 Kings 11:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Atalyaa yaayu Akasiya xam ne doomam ju góor dee na, mu daldi faagaagal mboolem ku bokk ci askanu buur.