bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 11:19
2 Kings 11:19 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu dellu nag woo njiiti téeméeri nit yaak waa Keret ñaak yeneen dag yaak mboolem waa réew ma, ñu jële Buur kër Aji Sax ji, jaare ca buntu dag ya, yóbbu ko kër Buur. Yowas daldi toog ca ngànguney buur ya.