2 Kings 11:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa réew mépp di bànneexu, péey ba ne tekk. Atalya moom, fekk na ñu jam ko saamar ba mu dee ca kër Buur.