bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 11:4
2 Kings 11:4 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca atum juróom ñaareel ma, Yoyada moo woolu waa Keret ya jiite kuréli téeméeri nit, ak yeneen dag ya, ñu wuysi ko ca kër Aji Sax ji. Mu fasook ñoom kóllëre, giñloo leen ca kër Aji Sax ji, ba noppi nuyole leen ak doomu Buur.