2 Kings 11:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu njiiti kuréli téeméer ya def mboolem la leen Yoyada sarxalkat ba sant. Ku nekk ànd ak say nit, ña aye bésub Noflaay ak ña ayewul bésub Noflaay, ñu bokk dikk ca Yoyada, sarxalkat ba.