2 Kings 12:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu am bés mu wax sarxalkat ya ne leen: «Mboolem xaalis bu ñu sellalal kër Aji Sax ji, muy xaalisu njot-gi-bakkan, mbaa xaalis bu ñu wàccoo ngiñ, mbaa bépp xaalisu saraxu yéene bu nit di indi kër Aji Sax ji,