2 Kings 14:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom moo tabaxaat dëkk ba ñuy wax Elat, delloo ko ci biir Yuda, gannaaw ba Buur Amaciya saayee, fekki ay maamam.