2 Kings 14:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li des ci mbiri Yerbowam ak mboolem lu mu def ak njàmbaaram gi mu xaree te nangoo ko dëkk yi ñuy wax Damaas ak Amat gu Yuda, delloo ko Israyil, bindees na lépp moos ci téere bi ñu dippee Jaloorey buuri Israyil ci seeni jant.