2 Kings 14:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom Amaciya moo duma fukki junniy (10 000) waa Edom ca xuru Xorom wa, nangu dëkk ba ñuy wax Sela ca xare ba, tudde ko Yogtel, te noonu la tudd ba bésub tey jii.