2 Kings 15:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Menayem dajale xaalis boobu ci Israyil; jële ko ca mboolem boroom alal ya, ku nekk ci ñoom joxe juróom fukki dogi xaalis, ñu yót ko buuri Asiri, mu doora jóge ca réew ma, ñibbi.