2 Kings 17:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
waa Awa sàkk Nibaas ak Tartag, waa Sefarwayim di lakk seeni doom ngir tuuri Sefarwayim yi ñuy wax Addraameleg ak Anameleg.