2 Kings 19:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Esayi doomu Amocc yónnee ca Esekiya ne ko: « Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne li nga ko ñaan ci Senakerib buurub Asiri, dégg na ko.