2 Kings 19:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Moo tax Aji Sax ji wax ci buurub Asiri ne: “Du dugg ci dëkk bii, du fi soqig fitt, du fi taxawe ab pakk, du fi jal jal bu muy gawe.