2 Kings 2:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu waa dëkk ba ne Alyaasa: «Xam nga fi dëkk bi nekk baax na, sang bi, waaye ndox mi baaxul, te suuf si nanguwul.»