2 Kings 2:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kurélu yonenti Yeriko nag dikk ba ca Alyaasa ne ko: «Ndax xam nga ne bésub tey jii Aji Sax ji dina la yenni sa kilifteefu sang Ilyaas?» Mu ne leen: «Man kay xam naa ko, waaye noppileen rekk.»