2 Kings 2:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee juróom fukki nit bawoo ca kuréli yonent ya, dikk taxaw, dànd leen, janook ñoom fa ñu yem ñoom ñaar ca tàkkal dexu Yurdan.