2 Kings 2:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu jàllee, Ilyaas ne Alyaasa: «Wax ma lu ma lay defal bala ñu maa yóbbu, may teqlikook yaw!» Alyaasa ne ko: «Xanaa naa am lu mat sag leer ñaari yoon.»