2 Kings 20:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jant yooyu Esekiya moo woppoon bay waaja dee. Yonent Yàlla Esayi doomu Amocc dikk, ne ko: « Aji Sax ji dafa wax ne: Dénkaaneel sa mbiri kër, ndax dangay dee, doo jóg!»