bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 21:8
2 Kings 21:8 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndegam bànni Israyil saxoo nañoo sàmm mboolem lu ma leen santoon, te mu dëppook mboolem yoon wi leen Musaa sama jaam ba sant ñu topp ko, dootuma leen wërloo, ñu wacc réew mi ma joxoon seeni maam.»