2 Kings 22:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buuru Yuda mi leen yónni, ngir ngeen seetlusi ci Aji Sax ji nag, waxleen ko ne ko: “Li Aji Sax ji Yàllay Israyil wax ci kàddu yi ngeen dégg moo di: