2 Kings 23:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Yosya sobeel na fa ñuy wax Tofet ca xuru Ben Inom, ba kenn dootu fa lakk sa doom ju góor mbaa ju jigéen ngir tuur wi ñuy wax Moleg.