bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 23:35
2 Kings 23:35 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yowakim jox na Firawna Neko xaalis baak wurus wa mu laaj. Waaye waa réew ma la ko sas, ba jële ca ñoom xaalis baak wurus wa, ku nekk ak sab sas, daldi koy dajale, jox ko Firawna Neko.