bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 25:23
2 Kings 25:23 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mboolem kilifay xare ya déggee ñook seeni nit ne buuru Babilon fal na Gedalya, dañoo ànd dikk ca Gedalya ca Mispa. Kilifa yooyu Ismayil doomu Netaña la woon, ak Yowanan doomu Kareya, ak Seraya doomu Tanumet ma dëkk Netofa, ak Yaasaña doomu waa Maaka ba, ñook seeni nit.