2 Kings 25:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gedalya giñal leen ne leen: «Buleen ragala bokk ci surgay waa Babilon. Toogleen ci réew mi te nangul buuru Babilon, muy seen jàmm.»