2 Kings 25:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu jàpp ko, yóbbu ko ca buuru Babilon ca dëkk ba ñuy wax Ribla. Ñu dogal fa àtteem.