2 Kings 3:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yosafat daldi ne: «Ndax yonentu Aji Sax ji nekkul fii, ba nu seetloo ko ci Aji Sax ji?» Kenn ca jawriñi buurub Israyil ne: «Alyaasaa ngi fi, mooy doomu Safat ji doonoon bëkk-néegu Ilyaas.»