2 Kings 3:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu Mowabeen ñépp dégg ne buur ya ñëw nañu xareseek ñoom. Ñu woo képp ku àttan ngànnaay, mag ak ndaw, ñu bokk taxaw fa seeni réew digaloo.