2 Kings 3:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba buuru Mowab gisee xeex bi di ko ëpp doole, daa woo juróom ñaar téeméeri boroom saamar, ànd ak ñoom ngir bëtt, ba àgg ca buurub Edom. Waaye sottiwul.