2 Kings 4:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Ana loo wuti ca moom tey, te du Terutel weer, du bésub Noflaay?» Mu ne ko: «Jàmm la.»