2 Kings 4:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dawal gaaw dajeek moom, laaj ko mbaa mu ngi ci jàmm mook jëkkëram ak doomam.» Mu laaj ko, mu ne ko: «Jàmm rekk la.»