2 Kings 4:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk na Gewasi jiitu leen. Ba mu agsee, teg na yet wa ca kaw kanamu xale ba, waaye xale ba àdduwul, yënguwul. Gewasi waññiku, dajeek Alyaasa ne ko: «Xale ba de yewwuwul!»