2 Kings 4:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Alyaasa jóg di jaabante ca biir néeg ba. Nes tuut mu yéeg, bóofaat ca kaw xale ba; xale ba daldi tisli ba muy juróom ñaari yoon, ne xiféet.