bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 5:1
2 Kings 5:1 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu loolu wéyee Naaman njiital xareb buurub Siri la woon. Sangam buurub Siri nawloo ko lool, def ko nitam, ndax ciy loxoom la Aji Sax ji jaarale ndam li mu mayoon waa Siri. Ku jàmbaare la woon, waaye daa amoon jàngoroy ngaana.