2 Kings 5:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Surgaam ya nag dikk, kenn ca ñoom ne ko: «Baay Naaman, su doon lu jafe la la yonent bi wax ndax danga ko dul def? Kon kay su la nee nga sangu rekk, set wecc, nga war koo def!»