2 Kings 5:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gewasi daldi daw dabi Naaman. Ba ko Naaman séenee muy daw wutsi ko, mu cëppoo ca watiiram dajeek moom, ne ko: «Mbaa jàmm la?»