2 Kings 5:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Jàmm la kay. Sama sang a ma yónni ne ma ma wax la ne ñaari xale yu góori yonent a agsi léegi, jóge diiwaanu tundi Efrayim. Nee ndax doo ko jox fanweeri kiloy xaalis ak ñaari mbubbi xew yu mu leen may?»