2 Kings 5:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Alyaasa, góoru Yàlla ga déggee ne buurub Israyil xotti na mbubbam, daa yónnee ca moom, laaj ko ne ko: «Ana lu tax nga xotti sa mbubb? Yebalal waa ji ci man rekk. Dina xam ne yonent a ngi ci Israyil.»