2 Kings 6:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu bëkk-néegub góoru Yàlla ga jóg ca suba teel, génn, gisul lu moy mbooloom xare mu gaw dëkk ba, aki fas aki watiir. Mu ne ko: «Éy sang bi, fu nu jëm?»