2 Kings 6:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu wéyee Buur berndeel leen bernde ju réy; ñu lekk, naan; mu yiwi leen, ñu ñibbi ca seen sang. Booba la waa Siri gëjoona def gàngoori yàqkat, di dugg biir réewum Israyil.