2 Kings 6:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la Alyaasa di wax, ndaw la ne jimeet, jëm ca moom. Ma nga naan: «Gis nga musiba mii Aji Sax ji wàcce. Kon ana lu may séentooti ci Aji Sax ji?»