2 Kings 7:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu daldi dem woo wattukati bunt dëkk ba, wax leen, ne leen: «Dem nanu ca biir dalu waa Siri; ndeke kenn nekku fa, baat jibu fa; dara lu moy fas yu yeeweek mbaam yu yeeweek xayma yu ne ñumm.»