bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Kings 7:12
2 Kings 7:12 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur jóg ca guddi, wax aki jawriñam ne leen: «Ma wax leen nag li nu waa Siri di fexeel. Xam nañu ne nu ngi dee ak xiif. Moo tax ñu jóge ca seen dal, làquji ca àll ba. Xam naa dañu ne: “Bu ñu génnee dëkk bi rekk, nu jàpp leen, ba noppi dugg ci biir dëkk bi.”»