2 Kings 7:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu ci boppam moo ko dal itam, ndax mbooloo ma dañoo buuxante, ba dëggaate ko ca bunt ba, mu dee.