2 Kings 7:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñu jóg timis, jëm ca dalub waa Siri. Ba ñu agsee ca peggub dalu waa Siri, gisuñu luy nirook nit sax.