2 Kings 8:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am na bés Alyaasa wax ndaw sa mu dekkaloon doomam ju góor ne ko: «Ayca, àndal ak sa njaboot, ngeen dali fu ngeen mana dal, ndax Aji Sax ji dogal na ab xiif ci réew mi, te dina am juróom ñaari at.»