2 Kings 8:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Yoram jàll ba Sayir, yóbbaale watiiri xareem yépp. Moo jóg ag guddi, dal ca kaw Edomeen ña leen gawoon, moom ak njiiti watiiri xareem. Waaye gàngooru Yuda ñoo daw, dellu ca seeni xayma.